217 Minanu yiñuy hadiyaal Kubaax ki ci atu bis bune ubbi nañ ko ci alarba gi talaata ginaaw timis lañu koy xatmu defaale waxtaan ci Xasida gi. Ku tabbiwul ci group bi te bëgg ciy barkeelo ayu bis bune lum jangg mën nañu koo yonee 🙏
12
301
Minanu retweeted
“Ô toi qui considères un autre que Allah comme Seigneur et qui aimes un autre que la meilleure des créatures, Mon Seigneur a arraché la lumière de ta poitrine….”
Maggal Jullig Geej le dimanche et lundi 20 et 21 Septembre. Sëñ Muntaxaa joxe ndigël na ndigël ne nañ ko def muy bissub Xasida waa ndakaaru 👂 ñoo ngi ciy woo ñëpp 🙏
Minanu retweeted
Leegi njabootu sëriñ bi suñ dajee ak sëñ hamsatu lici ëpu dañuy sakku ñaan ci sëñ hamsatu 😂 .La sëñ muntaxaa waxoon rk : sëñ amsa fasalee ñu .......























