Bro niou miin teud fofou mbeur mi walla😏
Defaral wax bi book😂
1
ⓂⓋⓈⓈⓍⓂⒷⓍ🎖️ retweeted
Les matières proposées, les conditions d’admission ainsi que les modalités d’attribution des bourses pour venir étudier en Corée seront au cœur de nos échanges.
Nous organiserons prochainement un Space afin de vous expliquer tout cela en détail et de répondre à vos questions.
ⓂⓋⓈⓈⓍⓂⒷⓍ🎖️ retweeted
Leuppeu lou bah louniouy nianes , Serigne TOUBA 🤍niane Nako thi xassidas🤍 yii,
té Leuppeu loumou niane , YALLA Sunu BOROM nanguoul na koko 😁😭🥳,
Kone nak féhé fonkou Goorgoorlou AK sah thi xassida yii
☝️ Té xamni tawféh AK défarou addunak Alahira mi ngui thi bire 😁🤍😌
ⓂⓋⓈⓈⓍⓂⒷⓍ🎖️ retweeted
Femme, musulmane, féministe, sénégalaise et qui plus est talibé Serigne Ahmadou Bamba...
Sama doundeu gui deh khaw meu foumouy yame waayé lii tchi dess moom fékhé ba jigeen gni diogué ci thiono yi niou nékk, liguey nguirr khaliss bi yokou ma ciy diokh sama wadiour yi, di ci déme Makka ak Madinah, diko def cii Magal gui ak liguèyou Serigne Mountakha bi, li ci dess ma ndieundé ko dibi, daal di diapp ndiakh...
Sama programme daal lii leu... dou lénéne ‼️
Bon week-end 💛.
ⓂⓋⓈⓈⓍⓂⒷⓍ🎖️ retweeted
🇸🇳🤩LA SAISON EXCEPTIONNELLE
D'ISMAILA SARR EN 2025/2026 !🏆
Un palmarès impressionnant pour notre Lion de la Teranga :
🏆Vainqueur de la CAN
🏆Vainqueur de la Conference League
🏆 vainqueur du Community Shield.
🥇Meilleur buteur de la Conference League (9 buts)
🥇Meilleur joueur de la Conference League
🥇 Meilleur buteur africain de la Coupe du monde avec 4 buts
🥇 Meilleur joueur de Crystal Palace de la saison
🥇Meilleur buteur de Crystal Palace de la saison
Cette année le Ballon d'Or africain doit revenir à Ismaïla Sarr ! l🤩🇸🇳🏆
Une saison exceptionnelle, une fierté pour tout💚💛❤️
ⓂⓋⓈⓈⓍⓂⒷⓍ🎖️ retweeted
Et dis : "ô mon Seigneur; fais que j'entre par une entrée de vérité et que je sorte par une sortie de vérité; et accorde-moi de Ta part, un pouvoir bénéficiant de Ton secours".
ⓂⓋⓈⓈⓍⓂⒷⓍ🎖️ retweeted
🚨 APPEL À L’AIDE : KHADY NAR FALL, 15 ANS, PORTÉE DISPARUE DEPUIS 6 JOURS.
La jeune Khady Nar Fall, domiciliée à la Cité Damel, est introuvable depuis six jours.
Sa famille lance un appel à la solidarité et sollicite l’aide de tous pour la retrouver.
📞 Contact : 78 839 40 91
Merci de partager massivement. Chaque information peut être précieuse.
ⓂⓋⓈⓈⓍⓂⒷⓍ🎖️ retweeted
Maam Saliou🥹aka beuriwone yeurmandé, yallah sunu borom yoki leeram🤲🏼
Doli sante Yallah sassu nék rek warna bép diaam🙏🏽🤍
ⓂⓋⓈⓈⓍⓂⒷⓍ🎖️ retweeted
La transition de malade entre Lonely de Akon et Weet de Elhadji Ndiaye est juste magnifique.
JHAMIL 🔥🔥🔥




























