Moussa Cissé (TOUHFATOU & WAKAANA) (@Mussa6c) header
Moussa Cissé (TOUHFATOU & WAKAANA) (@Mussa6c) profile picture

beugue, sope, ragal, wolou, doylo, yakar Serigne Touba képe rék. Thiéy Cheikhra nak aka goré mo khal yone wi

Senegal
Joined April 2016
Photo by Moussa Cissé (TOUHFATOU & WAKAANA) (@Mussa6c)Photo by Moussa Cissé (TOUHFATOU & WAKAANA) (@Mussa6c)Photo by Moussa Cissé (TOUHFATOU & WAKAANA) (@Mussa6c)Photo by Moussa Cissé (TOUHFATOU & WAKAANA) (@Mussa6c)Photo by Moussa Cissé (TOUHFATOU & WAKAANA) (@Mussa6c)Photo by Moussa Cissé (TOUHFATOU & WAKAANA) (@Mussa6c)Photo by Moussa Cissé (TOUHFATOU & WAKAANA) (@Mussa6c)Photo by Moussa Cissé (TOUHFATOU & WAKAANA) (@Mussa6c)Photo by Moussa Cissé (TOUHFATOU & WAKAANA) (@Mussa6c)Photo by Moussa Cissé (TOUHFATOU & WAKAANA) (@Mussa6c)
Salatu bou am solo!!! Mingui nék ci Xassida Mafatihul Bischri ❤️
55
5
316
4,722
Adouna Meusta am ta dou am ta dotoul am kou mélni CHEIKHOUL KHADIM🙏
1
13
85
1,129
Walay Mbacké
"Àdduna dem ba nga xam ne àdduna bi yëpp masse naañ ci bëgg Jàmm te xamuñu fuñu kay jële , Doxinu Sëriñ bi ndoŋ ci àdduna moo ñu ko mëna maay " Sëriñ Muntaxaa Mbàkke
1
1
4
132
Moussa Cissé (TOUHFATOU & WAKAANA) retweeted
Enregistrement Nurud Dareyni -Kurel sélection Nurud Dareyni (drouskat Nurud Dareyni Thies) Son bi dina disponible fi aki fann @Ly_Ibraahima @s_sourang @moughniyan
13
71
9
362
8,205
Diaambar deugue Serigne Hamsatou!! Yague fi lol ta wër balla aïssa 🙏
Céy jëmm ju yéeme, ku dul noppalu mukk mukk ci sàkku lu baax. Raw la ci Sëriñ Tuubaa du yomb mukk !
127
Adouna dotoul am kou mélni Cheikhoul Khadim 🙏
« Pass pass bu werr ak jeexit gui mou meuna am si Murid bi rawatina alaaxira guee nga xamni kounek langa sopp ngay nekk kon musiba la sib Murid muy sopp lenn ludul serigne bi ndeem beug naa texee té bagn guathié euleuk » @LeMouridePost @__babacar @zalembay ñu diapci mou yatou🙏🏿
1
105
Bilahi amna solo 🙏
Message bii Amna solo🤝❤️📌
1
82
Adouna dotoul am kou mélni Cheikhoul Khadim 🙏
Ëww dangay set li rek❤️😭
66
Assamane dotoul time kou mélni CHEIKHOUL KHADIM 🙏
Yen gayi bamba deglu len Musa murid ba wonalen Ndaw akmag gor ak djigen nan wuyuji ahmadu mbacké Magalgi lalen di xibar yen ñi xamul tey xibar t nara dm difa ziar ngir jëmi ahmadu mbacké ñenenti fan ci aw safar nañëp jog wadjlé safar ngir bamba rabihu safar la wajle ahmadu Mbakké
77
Adouna dotoul am kou mélni CHEIKHOUL KHADIM 🙏
Boroom Touba loo deugeur deugeur bess mihi nieuw diha touriy xeweul
1
4
136
Adouna dotoul am kou mélni CHEIKHOUL KHADIM 🙏
Walahi kén laa fii wone ❤️👆🏿
90
Adouna dotoul am kou mélni CHEIKHOUL KHADIM 🙏
Cëëy 🥹kén dhu CHEIKHOUL KHADIM ❤️salaw #Tlnoce #HORIZONGRANDMAGALDETOUBA2026
38
Adouna dotoul am kou mélni CHEIKHOUL KHADIM 🙏
Kuy waaru bàmba doy na waar !
81
Gravissime 🫢
Le mal dans ce pays 🇸🇳 est bien plus profond qu’on ne l’imagine. Allahou Akbar. 🫢
1
134
Diaambar la mouride saadikh!!! Mane dh chaque jour ma téwlou ko
Bokk na ci compte yi ma gën a neex TikTok
1
59
Adouna dotoul am kou mélni CHEIKH AHMADOU BAMBA KHADIM RASSOIL🙏
Yal nanu fekke MÀGGAL gi tal ko, man ko, te jekku ko bu baax a baax barkeb boroom MÀGGAL gi.
1
2
85